Durée: 12:50
Savourez la vie!
Découvrez l'univers patisen sur www.patisen.com
Pour suivre toutes vos vidéos préférées :
- Abonnez - vous ici : fr-film.net/us/patisencuisine
Suivez nous aussi sur les réseaux sociaux :
- Twitter :twitter.com/patisencuisine
- Facebook: facebook.com/groupepatisen
Webséries, sketchs, recettes de cuisine, bienvenue chez vous!.
patisen groupe patisen qualité nutrition séries sénégalaises
Commentaires
MS TV
Wah ami dafa fattè snap maamame
Il y a 21 jourbaye mass fall
hé hé mère bii mou Diongué waayyyyy
Il y a 23 joursIbrahima NDIAYE
Non vraiment doudou danga bons sombi bou kheume eupna dara fayouko haha waye mami sombi bi nekhone na ha ha si tu aimes ta mére pousse un bleu et les fans de Balla gâye que dieu te donne la victoire
Il y a moisMouhamed Ndiaye
Adja mo dakk si Sénégal kou weddi wahal
Il y a moisNdella Diop
Adja sangsé nga fofo tothe
Il y a moisPenda Gamou Niang
Ah kila Sénégal nam mari matleine
Il y a moisModou Diouf
fierté saint louisienne et nationale Marie Madeleine...une vraie référence
Il y a moisMouhamed Kama
Nonnnnnnnn amy néh nama trop tè mene limiy df
Il y a moisAmet Diollo
Mami Mom mako Tipo @$$
Il y a 2 moisAmet Diollo
Lii Mom DAFA nékh trop
Il y a 2 moisAminata Gueye
dudu gaw
Il y a 2 moisMariame Deh
wa team mamy ♡♡♡♡
Il y a 3 moisTaGhmouN Moun
J'aime kw Bilahii Yalla na diam Yagu
Il y a 4 moisDiallo Mamda
Yalla diam yague si adouna
Il y a 4 moisBabacar Mbaye
Belle famille,belle maman Adjia 💕
Il y a 4 moisCheikh Mbaye
Mari madeleine je t adore vraiment
Il y a 5 moisXxx Tentacion
Team Mamy
Il y a 5 moisbeibish kane
ohh li neexna com deug .mari madelaine dal mom rek mo meuna nek yayou adja
Il y a 5 moisDanty Thiané Ndour
😂😂sombi bi kayy
Il y a 5 moisndong fatou k
ohhh episode biimom damako raté won tata Marie Madeleine une grande Dame que j'aime bcp yag dignu bégal machalah temps bara yeugo longue vie à toi dafa massa meun limiy def Adja dal dou ay fooo bonne continuation MARODI
Il y a 5 moisKamara Khadija
Machallah série bi nékh ne trop laf chat❤❤
Il y a 5 moisIbrahima Gueye
Haha
Il y a 5 moisEl Hadji Amadou Faye
Mame dall bimou yeeksé warône nagko Dioh ndokhou nane tamite a suive le reste sa va
Il y a 5 moisKBOYER DAT
Mann Amie rkk laaa buga..
Il y a 5 moisFatou Bintou Savi
Nek saint-louisienne dal dou ay thiakhane. troooop fière de ma ville Ndar Guedie sangou si guedie gui leinkalikou si dekh bi
Il y a 5 moisYoussou Diakhitè
Kon aa
Il y a 5 moisndeye fatou seck
Ahh Thioum khalé Saint-Louis nionguini deh👯
Il y a 5 moisEDUF ENFANTS DU FUTURE
Mame dpui bima nekei xallei damala beug beugue la kham teksi Mame boy yalla nala yalla defal diam mayla goudu fan ak werr beuss bounumay takk inchallah dina gneuw basi yaw bilahi jtm
Il y a 5 moisSeydina Laye dara diombola lay mahtar
Nomay def ba am sohna somelni adja gayii???
Il y a 5 moisIbra Gueye
Mame yaw
Il y a 5 moisMass Fait Des Videos
La meilleure série
Il y a 6 moisFaye Mamy
Ahhh machalahhh tata marie madeleine enfin de retour namone nagne la ahhhh serie bi mongui soga geuneu nékh nakkk. Mais mamy sama tourondo yangui pata dé
Il y a 6 moisboury ndiaye
ndaysane richena en qualité d'ailleurs mane sah dina commencer watt toguou well well dans les vacs
Il y a 6 moisboury ndiaye
😂😂😂😂
Il y a 6 moisMbaye Babacar Faye
ndeysan mame mo nekh de sama khole dafa sedd
Il y a 6 moisMbaye Babacar Faye
ndeysan mary matlene namone naniou la trop waye
Il y a 6 moisRokhaya Ba
bi keur mo neikh lolll team marodi xalei ambiance
Il y a 6 moisBlack Queen
Namone nagnou Mere Marie Madeleine.nekhna torop vrema
Il y a 6 moisFascinatingMya
Marie Madeleine tu nous manquais J'ai vu ta tête motah ma setane
Il y a 6 moisBLACK BOY
super
Il y a 6 moishamidou diallo
waoh li nekhna diam sibir famille
Il y a 6 moismouhamadou bamba diop
Marie madleine la vrai namna sene theatre proud to be st_louisien💖💖💖 Team st louisien lever vs
Il y a 6 moisaigle 4 aigle 4
Nice n'a daffa nekh
Il y a 6 moisDidoush Dd
Episode bi moma dakal 😍😍
Il y a 6 moisNdeye Shoupita Diobéne bii
vous nous avez fait tous la surprise tata marie Madeleine nous avez manké
Il y a 6 moisDaba Dieng
Tata marie je très contente en vs voyant tête souriante et ravissante k dieu vs donne longue vie
Il y a 6 moisMame Yande Dia
Jadoreeee tata marie madeleine
Il y a 6 moisKhadi Kante
Ay way mane Mami guiss nassi sama bop 😂😂😂😂😂 dudou il me rappelle mon cousin kan on demandé si meuna togg. C connard😂😂
Il y a 6 moisMamy Ndiaye
Sourire aux lèvres quand je regarde cette série 😍
Il y a 6 moisF.ba Ba
Marie Madelaine la grande dame
Il y a 6 moisAssy Diakhate
Nafi
Il y a 6 moisAstou thm
Je l’aime marie madeleine je suis trop contente de l’avoir vu dans cette série 😍😍😍
Il y a 6 moisalah alah
Wawawwww j aime serie adji mouahhh
Il y a 6 moisRamses Chou
Trop d emotions....machallah. episode bi mo dakeu. Kou wath seu andeu andeu bo dem fek fa borom. Gnoune sunu tiossane moy senegal.
Il y a 6 moisFa Ji
0:48 fin du générique (même s'il est nekh). De rien
Il y a 6 moisJosephine Gueye
❤️😍😍😍😍🙏 même boye names lool
Il y a 6 moisIbrahima SIGNATE
Mari Madeleine Weere ak Goudou Faane Diaame cii yaaw Tâta Mariie❤️❤️❤️❤️Big Love
Il y a 6 moisMadjiguene123 Ndeye
serie bi nexna trop mais il faut éviter les boullions sa tue
Il y a 6 moisHumour Tv
Comme une vrai famille
Il y a 6 moisOMAR 7
Mere waxna degg dh👏
Il y a 6 moisThierno Wade
Séri adia nékhna trop wayé bolénn timeutéé lékke wala di.togou délénn mousoorr sénn.bopouyi girr kawarrgi mooy yoonn
Il y a 6 moisMberry Mmy
Ayway Meurie ngok sama Meurie
Il y a 6 moisaid D.
Maa Shaa' Allah... cet épisode est un régal. On aime Adja et aime encore plus sa maman
Il y a 6 moisMichelle Ndiaye
Mach allahTata Mari yalna guoudou fanevous avez de la chance vous qui joué avec
Il y a 6 moisndeye Fatou Toulouse Ndiaye2017
A thioum gnune rek si wa ndar wa ani wa saint louis
Il y a 6 moisFatimata Ball
Ndeysaane cet épisode me rappelle ma grande mère chérie. une personne bien pleine de vie. Quallah l'accueille au firdaws. Amine. tu nous manques mame BOYE.
Il y a 6 moisCheikh Tidiane Ngom
Content de retrouver La Grande Dame Marie Madeleine Diallo. L'élégance Saint Louisienne.
Il y a 6 moisMamane Fall
Maman marie madeleine diallo j'adore
Il y a 6 moiscoss babs
tata adja nekh guama
Il y a 6 moisPapa Demba Thioye
Mame Marie Madeleine ❤️❣️✨
Il y a 6 moisluodba Sy
yalla.na.am kuer adjia wakh lien amine si. Barki psl ?????
Il y a 6 moisSy Seydi
Tabaski Moubarak
Il y a 6 moisFalilou Falilou Diop
No nan Amy la nop fi
Il y a 6 moisBrown Niang
Bilahi...mer bi deuk ndar sama khol dafay sedd soumako guissé...benen mer bi mam sey ndeysannn....
Il y a 6 moisBMS
Vremeint beug na keur bou mel ni😍😭🙈✨💥🔥
Il y a 6 moisfatou dabo
No mame boy dal mo am ferling pathie
Il y a 6 moisAmelie Dianatou Camara
Marie Madeleine ❤️
Il y a 6 moisJunior Rassoul
longue vie Maman Marie Madelène
Il y a 6 moisMusa Jallow
very nice drama
Il y a 6 moismame awa seck
Meilleure épisode 😂😂❤❤❤ndeysanee mame boy daffa neikh
Il y a 6 moisMustafa Jaañ
Masha Allahou Adja Marie Madeleine. Naamone na gnou la graaavvvv. 😍😍😍😍
Il y a 6 moisdaba fall
Adjia tammite saint louisienne dou saff dieune teh thiép bou khonkk kéne douko teuthie bamou ni rapp daff kay fourile dagay barale ekh🙄🙄🙄
Il y a 6 moisBiba louesse
Machalla Tata mari madeleine elle adorable .
Il y a 6 moiscameleonpix cameleon
Marie Madelaine de retour une grande dame du théâtre sénégalais
Il y a 6 moisbïğťőű Ďőűňďóű guiss
Nn man doudou dina ma raye srx 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Il y a 6 moishalimatou sadia faye
Oohh c magnifique long vie à mame Marie Mandelaine
Il y a 6 moisDjeina Ndiaye
Adja liga baral dou liga yakk sa tchine bou nger bobou
Il y a 6 moisEva Sow
j'aime trop cool
Il y a 6 moisMohamadane Diakhate
j'aime Mami el est tro calme matna taw
Il y a 6 moisAdji Ba
Un grand merci à vous d'avoir faire venir marie madeleine sa fait long temps elle nous avez manqué merci
Il y a 6 moisMalick Dramé
MAGNIFIQUE
Il y a 6 moisRougui ly
Waw mame booooy mi safna khorom d 😂😂😂
Il y a 6 moisAminata SoW
Dans la maison y’a tjr kou mlni ami
Il y a 6 moissv barbie nøirĕuh LPB
j'adore mary madeleine
Il y a 6 moisxippil xool
😂😂😂noo dudu c le meilleur day yokk ambiance
Il y a 6 moisMelni B
Team ndar team saint louis way ❤❤❤❤ wayé nak tieubou dieune bou ndar deug le poisson dougnouko saf , teumbeul rek mou tiouki tiouki ba nior té dou seuthie.
Il y a 6 moissweet reggae mix
J adore trop adja. Belle douce dame. OUSMANE FALL COMO
Il y a 6 moissweet reggae mix
Chapeau pour le casting et le contenu. Li mo done senegal des valeurs et de l avenir. La richesse n enleve en rien l education. Braviiiii
Il y a 6 moisIbrahima Kane
mai ou e diogaye
Il y a 6 moisIbouzo Bafara
Mère bi ayy na tropeuh saxx ❤️❤️❤️
Il y a 6 mois